severity wishlist
# translation of wo.po to Wolof
# translation of console-common_debian_po.po to Wolof
#
#    Translators, if you are not familiar with the PO format, gettext
#    documentation is worth reading, especially sections dedicated to
#    this format, e.g. by running:
#         info -n '(gettext)PO Files'
#         info -n '(gettext)Header Entry'
#    Some information specific to po-debconf are available at
#            /usr/share/doc/po-debconf/README-trans
#         or http://www.debian.org/intl/l10n/po-debconf/README-trans#
#    Developers do not need to manually edit POT or PO files.
# Mouhamadou Mamoune Mbacke <[EMAIL PROTECTED]>, 2006.
#
msgid ""
msgstr ""
"Project-Id-Version: wo\n"
"Report-Msgid-Bugs-To: \n"
"POT-Creation-Date: 2006-09-19 09:15+0200\n"
"PO-Revision-Date: 2006-10-02 14:52+0000\n"
"Last-Translator: Mouhamadou Mamoune Mbacke\n"
"Language-Team: Wolof\n"
"MIME-Version: 1.0\n"
"Content-Type: text/plain; charset=UTF-8\n"
"Content-Transfer-Encoding: 8bit\n"
"X-Generator: KBabel 1.10.2\n"

#. Type: select
#. Choices
#: ../templates.in:1001
msgid "Select keymap from arch list"
msgstr "Tannal tërëliinu tablocaabi ci list arch"

#. Type: select
#. Choices
#: ../templates.in:1001
msgid "Don't touch keymap"
msgstr "Bul laal tërëliinwi"

#. Type: select
#. Choices
#: ../templates.in:1001
msgid "Keep kernel keymap"
msgstr "Tëyéel tërëliinu kernel bi"

#. Type: select
#. Choices
#: ../templates.in:1001
msgid "Select keymap from full list"
msgstr "Tannal aw tërëliin ci ab list bu mat"

#. Type: select
#. Description
#: ../templates.in:1002
msgid "Policy for handling keymaps:"
msgstr "Politik bu jëflënte ak tërëliinu tablocaabi yi:"

#. Type: select
#. Description
#: ../templates.in:1002
msgid ""
"The keymap describes how keys are laid out on your keyboard, and what "
"symbols (letters, digits, etc.) are drawn on them."
msgstr ""
"Tërëliinu tablocaabi bi mooy wane yoon winuy toftalee butoŋ yi nekk ci "
"tablocaabi bi (clavier), ak yan mandarga (araf, numero,...)lañu ci bind."

#. Type: select
#. Description
#: ../templates.in:1002
msgid ""
"\"Select keymap from arch list\" will allow you to select one of the "
"predefined keymaps specific for your architecture - you will most likely "
"want this unless you have a USB keyboard."
msgstr ""
"\"Tannal tërëliinu tablocaabi ci list arch\" dana la may nga tann benn ci "
"tërëliinu tablocaabi yiñu defaral sa arkitektuur (architecture) ba noppi - "
"jamtaluna lool ne lii ngay bëgg, ndare book nga yore tablocaabi USB."

#. Type: select
#. Description
#: ../templates.in:1002
msgid ""
"\"Don't touch keymap\" will prevent the configuration system from "
"overwriting the keymap you have in /etc/console.  Select this if you want to "
"keep a keymap you obtained through other means.  Please remember to install "
"new keymaps with install-keymap(8) if you select this choice."
msgstr ""
"\"Bul laal tërëliinwi\" dana tax ba sistemu komfigraasioŋ bi du far sa "
"tërëliin wi nekk ci fiise /etc/console. Tannal bii bu fekkee dangaa yore aw "
"tërëliin boo ame ci waneen yoon. Bul fattee istale ay tërëliin yu bess ak "
"install-keymap(8), bu fekkee bii nga tann."

#. Type: select
#. Description
#: ../templates.in:1002
msgid ""
"\"Keep kernel keymap\" will prevent any keymap from being loaded next time "
"your system boots.  It will remove from /etc/console any keymap you may have "
"already selected (it will be lost), but if you have already loaded a keymap, "
"it cannot be changed back until you reboot."
msgstr ""
"\"Tëyéel tërëliinu kernel bi\" dana tax booy talaat (boot) sa masin deesul "
"sëf waneen tërëliin(keymap).  Weppu tërëliin wu nekkoon ci fiise /etc/"
"console deesna ko fa jële (deesna ko ñakk), waaye bu fekkee jotoon ngaa sëf "
"aw tërëliin, konn deesuko mana soppi fiiyak ngay talaat (reboot) sa masin."

#. Type: select
#. Description
#: ../templates.in:1002
msgid ""
"\"Select keymap from full list\" offers a full listing of all predefined "
"keymaps.  You want this, if you use an USB keyboard from a different "
"computer architecture or if you use an adapter to use such a keyboard."
msgstr ""
"\"Tannal aw tërëliin ci ab list bu mat\" dana la jox ab list bu am mbooleem "
"tërëliin yi fi am.  yaangi soxlaa bii, bu fekkee dangaa yor ab tablocaabi "
"USB bu baneen arkitektuuru ordinaatéer walla ngay jëfandikoo ab adaptaatóor "
"buy jëfandikoo ab tablocaabi bu deme noonu."

#. Type: note
#. Description
#: ../templates.in:2001
msgid "Ignored boot-time keymap in an old location"
msgstr "Amna aw tërëliin wuy dox ci bu masin bi di takk buñuy bayyi nimu mel"

#. Type: note
#. Description
#: ../templates.in:2001
msgid ""
"You have asked the keymap configuration tool not to touch an existing keymap "
"you installed, or you asked for higher-priority questions only to be asked "
"and the tool decided not to mess with your existing setup."
msgstr ""
"sakkunga ci jumtukaayu komfiguraasioŋ bu tërêliin mu baña laal aw tërëliin "
"woo istalewoon. walla book danga laajoon ñu joxla rekk laaf yi siini "
"piriyorite gëna kawe, ta jumtukaau bi dogu bañalaal sa reglaas yi fi nekk."

#. Type: note
#. Description
#: ../templates.in:2001
msgid ""
"However, you have file(s) that were recognized as boot-time keymaps by older "
"versions of the console utilities, either in /etc/kbd/ or in /etc/console-"
"tools/, named default.kmap(.gz) and these are now ignored."
msgstr ""
"Waaye nak, amnga ay fiise yu jumtukaayu konsol bi  xammee ne ay tërëliinu "
"tablocaabi yuy dox bu masin biy takk, fiise benn mingi ci /etc/kbd walla /"
"etc/console-tools/, mu tuddu default-kmap(.gz) ta yooyu fiise deesleen di "
"jéllalé."

#. Type: note
#. Description
#: ../templates.in:2001
msgid ""
"If you wish that one of them takes effect on next reboot, you will have to "
"move it to /etc/console/boottime.kmap.gz manually."
msgstr ""
"Boo bëggée benn ci ñoom doon biy dox boo taalaatee (reboot) masin bi, kon "
"yobbu ko ci /etc/console/boottime.kmap.gz ak sa loxo."

#. Type: select
#. Description
#: ../templates.in:3001
msgid "Keyboard layout family:"
msgstr "Fami bu tërëliinu tablocaabi bi:"

#. Type: select
#. Description
#: ../templates.in:3001
msgid ""
"Please specify the generic family name for your keyboard layout. Usually, "
"the layout family name is taken from the first keys on the left of the top "
"letters row of the keymap (this is at least true for qwerty and azerty "
"layouts)."
msgstr ""
"Joxeel turu njabootu sa tërëliinu tablocaabi. Li ci ëppu, tur wi "
"ñingi koy jële ci butoŋ yi cammooñu raŋ gi ci kaw (lu mel ne tërëliinu "
"qwerty ak azerty)."

#. Type: select
#. Description
#: ../templates.in:4001
msgid "Keyboard layout:"
msgstr "Tërëliinu tablocaabibi:"

#. Type: select
#. Description
#: ../templates.in:4001
msgid ""
"In order to refine your choice for a keymap, please mention the physical "
"layout of your keyboard."
msgstr ""
"Ngir gëna segg tërëliin wingay tann, joxeel tërëliin wu butoŋ yi ne ci sa "
"tablocaabi."

#. Type: select
#. Description
#: ../templates.in:5001
msgid "Keyboard variant:"
msgstr "Cafaanu (variant) tablocaabi bi:"

#. Type: select
#. Description
#: ../templates.in:5001
msgid ""
"The layout you selected has several variants.  Please select the one "
"matching your keyboard."
msgstr ""
"Tërëliin wi nga tann dafa am ay fasoŋ yu bare.  Tannal fasoŋ wi dëppóo ak sa "
"tablocaabi."

#. Type: select
#. Description
#. Type: select
#. Description
#: ../templates.in:6001 ../templates.in:7001
msgid "Keymap:"
msgstr "Tërëliin:"

#. Type: select
#. Description
#: ../templates.in:6001
msgid ""
"The keyboard you selected allows you to choose among several keymaps. "
"Usually these were designed either for specific tastes (eg. dead keys or "
"not), or for specific needs (eg. programmer's keymaps)."
msgstr ""
"Tablocaabi bi nga tann dana la may nga tanne ci ay tërëliin yu bare. Li ci "
"ëppu nak, yooyii ñingileen defar ngir ñu dëppóo ak ay cafka (gout) (ci "
"misaal: caab ju dee walla déet), walla ñu def ko ngir faj yenn soxla yi (ci "
"misaal: tërëliin yu bindkatu prograam)."

#. Type: select
#. Description
#: ../templates.in:7001
msgid ""
"If you use a keyboard from a different computer architecture, you can choose "
"a specific keymap in the full map."
msgstr ""
"Bu fekkee dangay jëfandikoo ab tablocaabi bu baneen arkitektuuru kompiyutar "
"(ordinaatéer), kon man ngaa tanne tërëliinu tablocaabi bi ci list bu mat bi."

#. Type: boolean
#. Description
#: ../templates.in:8001
msgid "Are you ready for the ADB keycodes transition?"
msgstr "Ndax jekknga ngir toxu ci kodu caabi bu ADB ?"

#. Type: boolean
#. Description
#: ../templates.in:8001
msgid ""
"The kernel is configured to have the keyboard send ADB keycodes. This "
"behaviour is now deprecated and no longer supported by Debian."
msgstr ""
"Sa kernel bi deeskoo komfigure ba tablocaabi bi di yonnée ay kodu caabi ADB. "
"Doxiin wii nak rafetlootuñuko ba taxna Debian dootu ko gaddu."

#. Type: boolean
#. Description
#: ../templates.in:8001
msgid ""
"For best results you should reconfigure your kernel with "
"CONFIG_MAC_ADBKEYCODES=n. If you can't or don't want to do this for some "
"reason, pass keyboard_sends_linux_keycodes=1 as an argument to the kernel."
msgstr ""
"Ngir am resiltaa yi gën, dangaa wara komfigure sa kernel bi ak "
"CONFIG_MAC_ADBKEYCODES=n. Bu fekkee bëggóo koo def, kon dangaa wara jox "
"kernel bi argimaa bu keyboard_sends_linux_keycodes=1."

#. Type: boolean
#. Description
#: ../templates.in:8001
msgid ""
"Beware that the transition will most probably break your X configuration so "
"it is strongly recommended that you exit all X sessions now and adapt your "
"configuration afterwards (start \"dpkg-reconfigure console-data\" as root)."
msgstr ""
"Na nga xam ne nak toxu bi jamtaluna lool mu dammu komfiguraasioŋ bu X, moo "
"tax ñi ngilay laabiire nga génn ci mbooleem jataay yu X yi, boo noppee doora "
"soppiwaat komfiguraasioŋ bi (doonal root, nga daldi doxal \"dpkg-reconfigure "
"console-data\")."

Reply via email to