Here is un updated version of the Wolof translation of the shadow package.

--
# translation of wo.po to Wolof
# translation of shadow_debian_po.po to Wolof
#
#    Translators, if you are not familiar with the PO format, gettext
#    documentation is worth reading, especially sections dedicated to
#    this format, e.g. by running:
#         info -n '(gettext)PO Files'
#         info -n '(gettext)Header Entry'
#    Some information specific to po-debconf are available at
#            /usr/share/doc/po-debconf/README-trans
#         or http://www.debian.org/intl/l10n/po-debconf/README-trans#
#    Developers do not need to manually edit POT or PO files.
# Mouhamadou Mamoune Mbacke <[EMAIL PROTECTED]>, 2005, 2006.
#
msgid ""
msgstr ""
"Project-Id-Version: wo\n"
"Report-Msgid-Bugs-To: \n"
"POT-Creation-Date: 2006-05-20 10:39-0500\n"
"PO-Revision-Date: 2006-10-13 21:25+0000\n"
"Last-Translator: Mouhamadou Mamoune Mbacke <[EMAIL PROTECTED]>\n"
"Language-Team: Wolof <debian-boot@lists.debian.org>\n"
"MIME-Version: 1.0\n"
"Content-Type: text/plain; charset=UTF-8\n"
"Content-Transfer-Encoding: 8bit\n"
"X-Generator: KBabel 1.9.1\n"

#. Type: password
#. Description
#: ../passwd.templates:21
msgid "Root password:"
msgstr "Baatujall bu root:"

#. Type: password
#. Description
#: ../passwd.templates:21
msgid ""
"You need to set a password for 'root', the system administrative account. A "
"malicious or unqualified user with root access can have disastrous results, "
"so you should take care to choose a root password that is not easy to guess. "
"It should not be a word found in dictionaries, or a word that could be "
"easily associated with you."
msgstr ""
"Soxla ngaa def ab baatujall bu root, koontu bu ki yore administaraasioŋ bi. "
"Ab saaysaay walla ku amul ndigël bu manee aksi ci root man naa and ay "
"resiltaa yu mana yaq, moo tax da ngaa teey ta tann ab baatujall bu root boo "
"xam ne du yomba jabbutu. warula am ci disoneer yi, warula doon ab baat bu "
"yomba lëŋkale ak yaw."

#. Type: password
#. Description
#: ../passwd.templates:21
msgid "Note that you will not be able to see the password as you type it."
msgstr "Nga seetlu ne doo mana gis baaatujall bi boo koy tappe."

#. Type: password
#. Description
#: ../passwd.templates:35
msgid ""
"Please enter the same root password again to verify that you have typed it "
"correctly."
msgstr "Dugëlaatal benn baatujall bi ngir seet baxam tappeewoon nga ko bu 
baax."

#. Type: boolean
#. Description
#: ../passwd.templates:42
msgid "Create a normal user account now?"
msgstr "Ndax u sos koontu bu ajijëfandikoo bu normaal?"

#. Type: boolean
#. Description
#: ../passwd.templates:42
msgid ""
"It's a bad idea to use the root account for normal day-to-day activities, "
"such as the reading of electronic mail, because even a small mistake can "
"result in disaster. You should create a normal user account to use for those "
"day-to-day tasks."
msgstr ""
"Xalaat bu dëŋg la nak ngay jëfandikoo koontu bu root ci sa liggéey u bis "
"bune, lu mel ne jaŋg email, ndax ab njuumte bu ndaw rekk man naa andi musiba "
"bu mag. Da ngaa wara sos ab kontu bu ajijëfandikoo bu normaal nga diko "
"jëfandikoo ci liggéey yi deme noonu."

#. Type: boolean
#. Description
#: ../passwd.templates:42
msgid ""
"Note that you may create it later (as well as any additional account) by "
"typing 'adduser <username>' as root, where <username> is an user name, like "
"'imurdock' or 'rms'."
msgstr ""
"Nga seet lu ne man nga koo sos bu ëllëgée (naka noonu sos baneen koontu 
bumu "
"mana doon) da ngay tappe 'adduser <username>' ginnaaw boo duggee ak root, "
"buko defee <username> turu ajijëfandiku lay doon, lu mel ne 'imurdock' walla "
"'rms'."

#. Type: string
#. Description
#: ../passwd.templates:54
msgid "Full name for the new user:"
msgstr "Tur wu mat wu ajijëfandikoo bu yees bi:"

#. Type: string
#. Description
#: ../passwd.templates:54
msgid ""
"A user account will be created for you to use instead of the root account "
"for non-administrative activities."
msgstr ""
"Deesna la sosal ab koontu bu ajijëfandikoo ngir nga koy jëfandikoo bayyi "
"koontu root bi bu fekkee defoo liggéey yu adminsitaraasioŋ."

#. Type: string
#. Description
#: ../passwd.templates:54
msgid ""
"Please enter the real name of this user. This information will be used for "
"instance as default origin for emails sent by this user as well as any "
"program which displays or uses the user's real name. Your full name is a "
"reasonable choice."
msgstr ""
"Dugëlël tur u dëggëntaan wu ajijëfandikoo jii. Boobu imformaasioŋ deesna 
ko "
"jëfandikoo ci misaal muy defóo ci lu mel ne adrees u email yi ajijëfandikoo 
"
"jooju di bind, naka noonu bu baneen porogaraam buy wane walla muy jëfandikoo "
"tur u dëggëntaan wu ajijëfandikoo ji. Nga joxe saw tur wu mat tann bu xellu 
"
"la."

#. Type: string
#. Description
#: ../passwd.templates:65
msgid "Username for your account:"
msgstr "Turujëfandikookat bu sab koontu:"

#. Type: string
#. Description
#: ../passwd.templates:65
msgid ""
"Select a username for the new account. Your first name is a reasonable "
"choice. The username should start with a lower-case letter, which can be "
"followed by any combination of numbers and more lower-case letters."
msgstr ""
"Tannal aw turujëfandikookat bu sa koontu bu bees bi. nga joxe saw tur tann "
"bu xellu la. Turujëfandikookat bi nak dafa wara tambule ak aw araf wu ndaw, "
"ginnaawam nimero walaa araf wu ndaw wula neex man nacaa toppu."

#. Type: note
#. Description
#: ../passwd.templates:72
msgid "Invalid username"
msgstr "Turujëfandikookat bi baaxul"

#. Type: note
#. Description
#: ../passwd.templates:72
msgid ""
"The user name you entered is invalid. Note that usernames must start with a "
"lower-case letter, which can be followed by any combination of numbers and "
"more lower-case letters."
msgstr ""
"Turujëfandikookat bi nga dugël baaxul. Nga seetlu ne turujëfandikookat dafa 
"
"wara tambule ak araf wu ndaw, ginnaawam nimero walaa araf wu ndaw wula neex "
"man nacaa toppu."

#. Type: password
#. Description
#: ../passwd.templates:79
msgid "Password for the new user:"
msgstr "Tannal ab baatujall bu jëfandikukat bu bees bi:"

#. Type: password
#. Description
#: ../passwd.templates:79
msgid ""
"A good password will contain a mixture of letters, numbers and punctuation "
"and should be changed at regular intervals."
msgstr ""
"Ab baatujall bu baax dafay am njaxasaanu ay araf, ay nimero and ay "
"puŋtuwaasioŋ ta deeskoo war di farala soppi."

#. Type: password
#. Description
#: ../passwd.templates:85
msgid "Re-enter password to verify:"
msgstr "Dugëlaatal baatujall bi ngir nu wóorlu:"

#. Type: password
#. Description
#: ../passwd.templates:85
msgid ""
"Please enter the same user password again to verify you have typed it "
"correctly."
msgstr ""
"Dugëlël benn baatujall bu jëfandikukat bi ngir wóor lu ba xam tappe nga ko 
"
"bu baax."

#. Type: note
#. Description
#: ../passwd.templates:91
msgid "Password input error"
msgstr "Njuumte bu dugël baatujall bi"

#. Type: note
#. Description
#: ../passwd.templates:91
msgid "The two passwords you entered were not the same. Please try again."
msgstr "Ñaari baatujall yi nga dugël bokku ñu. Jéemaatal baneen yoon ba 
xam."

#. Type: note
#. Description
#: ../passwd.templates:96
msgid "Empty password"
msgstr "Baatujall bu deful dara"

#. Type: note
#. Description
#: ../passwd.templates:96
msgid ""
"You entered an empty password, which is not allowed. Please choose a non-"
"empty password."
msgstr ""
"Da nga dugël baatujall bu deful dara, ta loolu deesuko naŋgu. Kon tann "
"laneen ludul baatujall bu deful dara."

#. Type: boolean
#. Description
#: ../passwd.templates:103
msgid "Enable shadow passwords?"
msgstr "Ndax nu def baatujall bu shadow muy dox?"

#. Type: boolean
#. Description
#: ../passwd.templates:103
msgid ""
"Shadow passwords make your system more secure because nobody is able to view "
"even encrypted passwords. The passwords are stored in a separate file that "
"can only be read by special programs. The use of shadow passwords is "
"strongly recommended, except in a few cases such as NIS environments."
msgstr ""
"Baatujall yu shadow dafay tax sa sistem bi gëna wóor ndax kenn du mana gis "
"benn baatujall, du sax bu ñu kiripte. Baatujall yi deesleen di deñc ci seen "
"fiiseeb boppu boo xam ne ay porogaraam espesiaal rekk ñoo ko man a jaŋg. Ñi 
"
"ngi laabiire bubaax nak nga jëfandikoo baatujall yu shadow, li ñiy settee "
"nak lu néew la, lu mel ne ãwironmaa NIS."

#. Type: title
#. Description
#: ../passwd.templates:111
msgid "Set up users and passwords"
msgstr "Komfigure jëfandikukatyi ak baatujall yi"

Reply via email to